Xel ñent la: xel mu gätt te rafet boroom as
gor la,
Xel mu gätt te ñaaw, boroom dof la,
Xel mu gudd te ñaaw, boroom saytaane la
Xel mu gudd te rafet, boroom wälliyu la.
Man a wax, bari wax, ak rèy làmmiñ, dañoo niroo te bokkuñu.
Ka man a wax saa bu waxe jarin boppam mbaa ay bokkam,
ka bari wax man na wax ba wax lu am njarin waaye deesu ko jariñoo ndax day tanxal gna muy waxal,
ka rèy làmmin nag saa bu waxe dugal boppam.
JAMM Ki koy am moy
kiy aw Thi Yoonu djup
Du tonñ téh kuka tonñ
mu jégèl ko
Sounou borom dina tégué lou métti, Waayé dou tégué lou gueunoul. Sayou nit ki khamé lolou dina noppalou.
Barkép Mame Sowrou Fall 💕
Thiatt👨🏿✈️
Invited by: Moussa T. NIANE
if the data has not been changed, no new rows will appear.
Day | Followers | Gain | % Gain |
---|---|---|---|
August 28, 2023 | 152 | +5 | +3.5% |
October 13, 2022 | 147 | +2 | +1.4% |
August 17, 2022 | 145 | +2 | +1.4% |
April 27, 2022 | 143 | +4 | +2.9% |
March 20, 2022 | 139 | +9 | +7.0% |
January 22, 2022 | 130 | +2 | +1.6% |
December 15, 2021 | 128 | -1 | -0.8% |
September 30, 2021 | 129 | +8 | +6.7% |
August 12, 2021 | 121 | +59 | +95.2% |