*Baxaatal kureel gi jëm ci ñépp*
Kureel liggéeyal ku tedd ki
Mbooloo muy ligéeyal S Tuubaa ci jàng ak yar jaare ko ci ndaw ñi ba li S Tuubaa bëggoon ci ñoom ñu bokk ci ñiy mottali yeene jooju ; te mooy ndaw yu tënk séen bopp ci def lu baax ak di ko wax ak tissare diine fun man a nekk ci njàngalem S Tuubaa te nangoo am kilifa déglu ndigal bàyyi tere.
| Day | Members | Gain | % Gain | 
|---|---|---|---|
| June 10, 2024 | 165 | +2 | +1.3% | 
| March 12, 2024 | 163 | +3 | +1.9% | 
| January 22, 2024 | 160 | +1 | +0.7% | 
| December 08, 2023 | 159 | +1 | +0.7% | 
| October 31, 2023 | 158 | +1 | +0.7% | 
| October 01, 2023 | 157 | +7 | +4.7% | 
| September 02, 2023 | 150 | +2 | +1.4% | 
| August 04, 2023 | 148 | 0 | 0.0% |