🇸🇳🌏🌌
WOLOF - ARAAB - FARAAÑSE.
Saa-Senegaal laa, di ab jànglekat bob mbatiitam réew mi ak xaytaam moo ma ñor, luy jëmale réew mi kanam lu nekk noo nga ca, waaye mu dëppoo ak xam-xam, te mengoo ak sunu ay aada yu baax yi.
يا رب إن أعطيتني فشكر
وإن منعت فرضى وصبر
🙏🏿😍🙏🏿
Leeral :
Mbëj g= électricité
Sàq m= compte
Dëya= tarder
Ballu yu bindaare= ressources naturelle
Saabal b= Media
Pas g= contrat
Wayndare w= dossier
Nguur g= gouvernement
Torlu= signer
Ma-réew = citoyen
Ma-xereñ= expert
Lijjanti g= entreprise
Démb= hier
Pekk b= bureau
Luññutu= enquête
Njaatige= chef
Fere y= peuple
Meññlukat = investisseur
Takk-der= policier
Màkkaan m= maison
Calaw l=préfet
Ja b=marché
Dànkaafu=avertir
Alikeñ b=masque
Raglu / fajuwaay = hôpital
Yaale g= transport
Fafal-naaw= avion
Fara b=maire
Tën b= statue
Njéggite l= le pont
Jure= porté plainte
Naawu = aereport
Dig = frontière
Lél b: date
Fafal-naaw= avion
Lootaabe g= organiser
Xumbeen= festivité
Ngomblaan g= assemblée
Arminaat : calendrier
Jongarukat bi: arbitre
Dóorub fay: penalty
Sémb b= projet
Ektaar= hectare
Gaaral= présenter
Luññutu = investigation
Nguur =gouvernement
Mba = démission
Jure= plaint
Ëttub àtte b= tribunal
Invited by: Mustafaa Lóo
if the data has not been changed, no new rows will appear.
Day | Followers | Gain | % Gain |
---|---|---|---|
November 26, 2023 | 397 | +35 | +9.7% |
October 26, 2022 | 362 | +5 | +1.5% |
August 24, 2022 | 357 | +2 | +0.6% |
July 18, 2022 | 355 | +2 | +0.6% |
June 11, 2022 | 353 | -3 | -0.9% |
May 04, 2022 | 356 | +14 | +4.1% |
March 27, 2022 | 342 | +8 | +2.4% |
January 28, 2022 | 334 | +3 | +1.0% |
December 21, 2021 | 331 | +2 | +0.7% |
November 13, 2021 | 329 | +12 | +3.8% |