Muslim
Sunnit
Sufism
Murit
Saa-afrig
🇸🇳Saa-senegaal
Kajoor-kajoor
Saa-wolof
Cëy kéemtaan!
1 - Yéemu nanu ci ku gëm dogalub Yàlla nan lay jàqee.
2 - Yéemu nanu ci ku wóolu wërsëg wi Yàlla warlul nan lay sonne.
3 - Yéemu nanu ci ku wóolu ne dee a ngi ñëw nan lay bége.
4 - Yéemu nanu ci ab jullit bu gëm ne dees na ko màndaxe ëllëg nan lay dajalee.
5 - Yéemu nanu ci ku xam àddina ak ni muy wëlbatikoo nan la am xel di dale ci dundug àdduna.
if the data has not been changed, no new rows will appear.
Day | Followers | Gain | % Gain |
---|---|---|---|
June 11, 2024 | 1,112 | +1 | +0.1% |
May 08, 2024 | 1,111 | +1 | +0.1% |
March 23, 2024 | 1,110 | +3 | +0.3% |
January 27, 2024 | 1,107 | +2 | +0.2% |
January 10, 2024 | 1,105 | +1 | +0.1% |
December 25, 2023 | 1,104 | +1 | +0.1% |
December 09, 2023 | 1,103 | +5 | +0.5% |
November 25, 2023 | 1,098 | +6 | +0.6% |
November 12, 2023 | 1,092 | +2 | +0.2% |
November 02, 2023 | 1,090 | +3 | +0.3% |