❤️Seydi Baba Lamin Niass H.A زاده الله بسطة في العلم والجسم بجاه عبد الذات ومظهر الأسماء والصفات رضي الله عنه
Kaaylen Niou topu baye Niass❤️🇸🇳📍
Amoul ben Maxaama Bou nit di am bam teré la Diouli wala wor lolou sou amon yalla diokh ko Yonente yalla mouhamed sallalahu aleyhi Wa Salam ndax Yonente bi Febar n’a Nit gni diko khar pur mou diété len Diouli Mou dioug Danou kheum Niou soti ko ndokh mou diouk danou waaat Niou soti ko ndokh Mou diouk wax ni wax lenn Aboubabar Mou diété Mboolo mi wayé Diouli gui Diekhoul loudoul ni Yonente bi tew n’a si Diouli gui Aboubacar di rouy si Yonente bi sallalahou aleyhi wa salam nit gni di rouy si aboubacar
Lolou sallalahu aleyhi Wa salam rek moko am❤️😭
Invited by: king_MFD
if the data has not been changed, no new rows will appear.
Day | Followers | Gain | % Gain |
---|---|---|---|
January 20, 2024 | 261 | +36 | +16.0% |
November 25, 2022 | 225 | +1 | +0.5% |
June 25, 2022 | 224 | +1 | +0.5% |
May 19, 2022 | 223 | +9 | +4.3% |
April 11, 2022 | 214 | +28 | +15.1% |
January 05, 2022 | 186 | +7 | +4.0% |
November 29, 2021 | 179 | +13 | +7.9% |
October 20, 2021 | 166 | -1 | -0.6% |
September 14, 2021 | 167 | +29 | +21.1% |