Sant Serigne Touba 🇸🇳📍🇫🇷
Automatic and Embedded Systems Engineering
Sëriñ Tuubaa nee na: « na ngeen gorgorlou ba nekk ay gor, ku bëgg doon as gor nag, fàwwu nga sàmmonteeg juroom ñatt (8) yii la:
1- As gor du jàpp di bàyyi
2- As gor du soppiku
3- As gor du wéet di wor
4- As gor du digé lum narul
5- As gor dina jëflanteeg kuko jikkoom soof
6- As gor dina teral kum xamul
7- As gor day dimbale kum tane
8- As gor dina xam lu jara wax noppi »
Invited by: Meissa mouride Gueye
if the data has not been changed, no new rows will appear.
Day | Followers | Gain | % Gain |
---|---|---|---|
January 22, 2024 | 376 | +7 | +1.9% |
January 26, 2023 | 369 | -1 | -0.3% |
August 08, 2022 | 370 | +2 | +0.6% |
May 26, 2022 | 368 | -2 | -0.6% |
April 18, 2022 | 370 | +2 | +0.6% |
March 10, 2022 | 368 | +6 | +1.7% |
January 12, 2022 | 362 | +1 | +0.3% |
December 05, 2021 | 361 | +4 | +1.2% |
October 27, 2021 | 357 | +4 | +1.2% |
September 21, 2021 | 353 | +16 | +4.8% |