Abdul Baaqii Géy di ab saa-wolof dëkk Tuubaa, di taalube Sëriñ Tuubaa, gëm ko, wóolu ko, doylu ko, yaakaar ko, Jërëjafe Sëriñ Tuubaa. Bokk ci ñi bëgg a suqali làkku wolof.