#Njangalem_Seriñ_bi_cik_Mugn
Seydina Alioune yow mi beug doon murid, no wara taxawé ci yeungu-yeungu jamono?
Alioune , Langa wara xam ndieuk moy donn mouride yomboul. Ndax Naka Seriñ bi firé moy ku amul benn yitté lu moy sakkou ngeureumeul boromam. Nga meun ci teunké rek ni murid bi warta am jott di deukkei xoulo, tontonté aka wéranté. So jougeutei bul jeum ci ludul lulay Jarign euleuk.
👌👌👌 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳 Mouride dëgg boul mérr te boul japp mérr;
mérr ak japp mérr dey alak ak Mouride.
Méral sey ayib (défauts) yow, gërëm sap Serigne;
Di daw nihmatam nak ba ame ay Mouride
Serigne Mbaye Diakhaté
if the data has not been changed, no new rows will appear.
Day | Followers | Gain | % Gain |
---|---|---|---|
September 16, 2023 | 117 | +3 | +2.7% |
October 30, 2022 | 114 | +1 | +0.9% |
August 25, 2022 | 113 | +1 | +0.9% |
June 12, 2022 | 112 | -3 | -2.7% |
May 06, 2022 | 115 | +3 | +2.7% |
March 28, 2022 | 112 | +6 | +5.7% |
January 30, 2022 | 106 | +4 | +4.0% |
December 23, 2021 | 102 | +1 | +1.0% |
November 15, 2021 | 101 | +2 | +2.1% |
October 07, 2021 | 99 | +7 | +7.7% |