K.C.D.S , ag kurélu Xassida gu nu duppee Maam Jabel SËY la (mu nekkoon kenn ci mag ñi daan liggéeyal sëriñ Tuubaa, mujj doon it ab seexam). Sunu Boroom fayee ko ay sët yu koy wéyalal ab ligéeyam, di ko jaaree ci xassida yi. Lépp aju ci waxi sëriñ bii 👇👇👇:
وهب لنا ذرية تديم العمل الصّالح يا خديم.